Cancion : Manko Artista : Ismaël Lô Album : Sénégal Url : https://www.letras10.co/letra-manko-de-ismael-lo Xalatna bouguen De guisse Ken doulen feole Xalatna bouguen de guisse Gueneu waxtane mana dioubo Lou bakhla Xalatna bouguen de guisse Diguen gueneu am dole Xalatna bouguen de guisse Gueneu waxtane mana dioubo Lou bakhla Ndakh koumou manti done si yengni Ya gui bay si warwi Ya kham guor gua yakham djiguen gua Nguen anda ndo bay warwi Ndakh gueum nani mbolo mbolo rek Modi dole Lou bakhla Man lankeuna man bagne na Gnou nane politicien yi dagno fewalo Souma amone lima gueunal maan Nguen andando boka dole Ndakh gueum nani mbolo mbolo rek Modi dole Lou bakhla Koumou manti done si gnoun gni Diaamou senegal rek moy sa yene Souma amone lima gueunal maan Nagnou andando boka dole Ndakh maan gueum nani mbolo Mbolo rek modi dole Lou bakhla Maan gueum nani bougnou ande bolo Mo gueun sougnoum rew Nagn diohonn te loho Maan gueum nani bougnou ande bolo Mo gueun sougnoum rew Nagn diohonn te loho Xalatna lou bakhla xalatna lou gueun le Bougnou ande bolo gnoun dana Sapadeuguin Xalatna lou bakhla xalatna lou gueun le Bougnou ande bolo gnoun dana Sapadeuguin Ndakh maan gueum nani mbolo Mbolo rek modi dole Lou bakhla Maan gueum nani mbolo mbolo rek Modi dole Lou bakhla Xalatna bouguen manko dinguen Gueune am dole Xalatna bouguen manko gueneu waxtane Mana dioubo Kone lou bakhla ========================== Letra descargada de Letras10.co ==========================